We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Xarnu Bi

by Yatfu

/

about

XARNU BI

Avant dernier Single d'une "SUITE LOGIQUE" de la situation de notre époque intitulé "XARNU BI" qui précède le dernier qui sortira la semaine prochaine portant le nom de "NO MORE THIRD WOLRD", du groupe YATFU en prévision de la sortie de 4ème ALBUM.

PROD: (MAO SCHOOL)

lyrics

XARNU B
(c’est notre époque ou siècle)

VERSE 1 :
GO et DRY

GO:

XARNU WU DIIS / GAAN TIIS / SUNU GUISS GUISS YI NIIS /
NIETEL LU BET A PITIM / GUMBAY NJACCAAR NE WEDEM /

DRY:

GOFU /XARNU/ KACC LA /
JEKKU/ JAM/ MU NACC LA/
ROY BA RAW /JIKKOY XACC/
MUSIBAA/ YU WACC LA/

GO:

DRYGUN SIMILI /
WAXTU BESS BAXX/
DI SAY BONE BA DESS / WER /AK XARNU/ BU CI/ ESKI /GEN NA YEES

DRY:

DEGG NAXXSAAY / CI GAL GU DUL TERR /
JIRIM GELU / LAXX JAAY / XOL YI MUJJU WOWE NE XERR /

GO:

MAQDOOM NE TEL/
MBOOTAAY YU XEET YI /TOGG NE CELL /
ANA AQ AK YELEF /
SEG YI NEEW FEES FA DEL/

DRY:

PERANTAL YI / MINE /FAAT /
LIBERIA BA RWANDA /
DOX JOGGI /MINE / XAAT /
CASAMANCE BA OUGANDA /

GO:

JAARUL SAXX LIM / ISLAMABAD AK NIAWTEFF YA /

DRY:

BAGDAD /JERUSALEM / PALESTINE / AK KAWTEFF YA

GO:
JIHAD UB BOPP RAPP/

DRY :

WORL TRADE CENTER MAMB

GO:

KUL EUTTU YENE KAY

DRY:

BEN LADEN DI KU NU FA NGADD


HOOK :
ROZO ( Kronik 2 H):

NEE / DANS UN MONDE DE DANGER /
PLUS ON AVANCE / RIEN SEMBLE S’ARRANGER/
TROP DE TRACAS / TROP DE BLA- BLA /
VITE CA PART EN GRAVAT/
ICI / AILLEURS / ET LA BAS / (BIS)

VERSE 2 :

JO:

CA MAQUILLE /CA COMPLOTE / A DENT DE SCIE /
CA RABOTE / T’ENTEND LES CRIS /
ET LE BRUIT/ QUI GIGUOTE ?
C’EST LE FRUIT /DE NOS FAUSSES NOTES /
LE CŒUR DES HOMMES / PART EN LOQUE /
DEPUIS LA POMME / POUR UN RIEN ON S’ GOMME /
LE PEUPLE DE LOTH / SALOPE / LA PEUR DE L’AUTRE /
SE DEVELOPPE /
C’EST UNE EPOQUE DE CODES /LA VIE UN COMBAT DE COQ /
PARTOUT CA DEBLOQUE/
CA TOURNE PAS ROND DANS LE GLOBE /
TROP DE MAO / SEME LE CHAOS / S’EN DU FOUTENT DU TAO /
VEULENT K.O/ LA POPULO / PAW !!!PAW !!!/ A LA POLOLO /
CA FAIT FROID / AU DOS / UN GROS POIDS /AU DOS /
LOURD EST CE FARDEAU / TEL UNE CHARGE DE CARGO /
LES BARJOTS / DU HAUT DE LOGE/ ILS NOUS JAUGENT /
MAIS LA FAUT QU'ON S'OPPOSE SEUL LE TRES HAUT DISPOSE /A L'EAU DE ROSE / LEUR THEORIES / DU BIG BANG A NUBIRI /
AGUERRIT/
LE BLACK INTELLEK /NE PAS CLOUER SON BEC /

HOOK

VERSE 3 :
DRY et GO

DRY:

NJUJJ NJACC/ BANE NGACC/ SIFF NGUR BANE WACC/
TABBAL REW CI FITNA/ XEL YI NEX BANA NACC/
PAAKA PUUT / DERET TIIS / DUNYA BEP DI GUISS /
KU CI NEK / KI NGEY JAMMU/ GAMU /DINE BI NGEY TAMMU /
EMBARGO !!!/
NGIR NJAAYUM NGANAAY / BANE YOON CABBAR KO /NEEW -JI -DOOLE GADDAAY /
SUUF / NJABOOT BI OUFFE / JAAM AK BAKAAR YI DUUF /
JOOY YO YI / CEY YALLA !!! / SAFARA NGI CI KAW SUUF /

GO:

BET GANAAR RU AFRICA / DI UTTI SOOWU JANTAM/
ASKAN WI / DI MABBANDO / GADDU XEER AK BANTAM /
ROPLANU NDEL NAW / RUU /DEM NJAANIIW/
DIGGANTE JAWWU AK JEERI JI / DOOMU ADAMAK NJANAW /
CAL LWEER DI ANDAK TAW /SUUF/
YENGU / KER YI/ DIGG / GUEJJ BI / GUEN NEGGAM /
KALIMATUL HAQ LANU CI / XARNU WERNDENG /
RAYA JAMM DANU KENDENG/
ARIFF YI NOODI KURU S / TIJJI TEERE YALLA DU RUS

credits

released April 13, 2013

license

all rights reserved

tags

about

Yatfu Dakar, Senegal

Yatfu! Groupe de rap formé entre 94 et 95 par trois membre fondateur leader : BIG D JOJO ET GOFU fut le premier groupe de rap hardcord au sénégal. 1998:"FENKU YATFU"
2001:"YONENTU RAP BI"
2005:"NIETTELU BEUT"

Le groupe YATFU a des influences tres africaines dans l'esprit mais tres moderne dans leur style musical

Toutes les musiques sont la bien venue dans l'oreille des ces mordus de la ZIK
... more

contact / help

Contact Yatfu

Report this track or account

If you like Yatfu, you may also like: